Kooru Biddew Saison 3 - Épisode 27

Diouma Toure
Diouma Toure

DIouma Toure

Hace 2 días
Awa Fall
Awa Fall

nh tu j

Hace 6 días
RubyRim
RubyRim

Roast beef*

Hace 9 días
Alioune Johnson
Alioune Johnson

Vous faites l'apologie des bouillon ou corrige madame. 1- Tout le monde sait que c'est la cause des maladies cardio-vasculaire (tension etc.) 2- D'habitude, on utilisait ça quand madame avait raté sa cuisine. Maintenant, on sait que c'est la majorité des femmes ne savent plus cuisiner. En conclusion, il faut arrêter de faire la promotion de ces bouillons.

Hace 9 días
Oulimata Ndiaye
Oulimata Ndiaye

The

Hace 9 días
Galou Dem
Galou Dem

Fama machallah

Hace 10 días
Fatima Dufour
Fatima Dufour

Une très bonne série. Bravo à vous avec Daro que du bonheur ré ba tasse

Hace 10 días
teresa toupane
teresa toupane

j'aime beaucoup le nouveau concept de bidew en plus d'être une femme qui bosse, qui est aux petits soins de son mari, elle diversifie ses plats, propose des recettes équilibrées. Super

Hace 11 días
Cherif Balde
Cherif Balde

fama dey réy nite ac rétane

Hace 11 días
Bow FALL
Bow FALL

fama sagessa gua mala love way

Hace 11 días
Madicke Mbengue
Madicke Mbengue

rosebeef wala roast beef?

Hace 11 días
chacha ly
chacha ly

Prochaine fois naga teuthie sa wagne boye sangou Bidew

Hace 11 días
khady ngom
khady ngom

Fama sagnsé kate ga serieux.

Hace 11 días
Elhadji Thiam
Elhadji Thiam

Nice na biddew

Hace 11 días
mussaa jop
mussaa jop

diank biii o6 geum na service dhh 😂😂😂😂

Hace 11 días
Khady diaw
Khady diaw

Fama wagnil khesal bi

Hace 11 días
Ndeye Ami Dia
Ndeye Ami Dia

Ah Rama sa robe mignonne na

Hace 11 días
fatou ndiaye
fatou ndiaye

Fama yow da gua wara wagni khessal bi, sa yaram ba gui yakhou!

Hace 11 días
fatou ndiaye
fatou ndiaye

Germaine mo meu neu joué!!!

Hace 11 días
Cuisine, Trucs et Astuces Aicha
Cuisine, Trucs et Astuces Aicha

Way daro yallah na goudd fane wau

Hace 11 días
Amina 14 Dieng
Amina 14 Dieng

Mai fama u est la meilleure vremn elle jou tres bien

Hace 11 días
Ablaye Petit Mbaye
Ablaye Petit Mbaye

rosebeef niam niam

Hace 11 días
Mamy Ndiaye
Mamy Ndiaye

Fama légui dafa dioubo ak bidew

Hace 11 días
Victor Saliou Faye
Victor Saliou Faye

Setane series yeup yomboul dé man 5 lay Setane :keur gui 'ngagn' makhpro 'bideew' adja

Hace 11 días
Aziz Gueye
Aziz Gueye

Attention aux bouillons MAGGi C’est toxique et sa tue car ça contient le GLUTAMATE. Sketch bi c’est bon mais je vois que c’est une pure publicité de MAGGI #j’aime mon pays c’est pourquoi je dénonce les choses

Hace 11 días
Dakar Plus
Dakar Plus

fama👏👏

Hace 11 días
Aissatou Gueye
Aissatou Gueye

Fama sa tagual machallah

Hace 11 días
Abou Gangue
Abou Gangue

Fama sag

Hace 11 días
Aida CAMARA
Aida CAMARA

C'est Roast beef et non rosebeef

Hace 11 días
Nema Siby
Nema Siby

No no way fama li mome dokhoul gor dia roul lii wayy

Hace 11 días
fifi Robdrup
fifi Robdrup

Daro et ndeye ndiaye sont les meilleures de leur generation,machaallah.

Hace 11 días
Seydou Baldé
Seydou Baldé

1

Hace 11 días
beugue loubax
beugue loubax

kou dakor thi ni khéssal daniou ko wara khékh beussal jaime daro yak na yaramam bi way

Hace 11 días
Khadim Sylla Brésil chapeco
Khadim Sylla Brésil chapeco

Guisgha de ligey de kene amol lom Don Mandal xawma loutax Senegale beg ay afero serigne

Hace 11 días
Papa Diop
Papa Diop

no daro defeante la

Hace 11 días
Khadim Sylla Brésil chapeco
Khadim Sylla Brésil chapeco

Fama xana dagha sono beg sey rek takh na ghay dem si serigne

Hace 11 días
Saliou Kasse
Saliou Kasse

team fama

Hace 11 días
doudou diaw
doudou diaw

Daro linga sole rafétena ma salla

Hace 11 días
queen diaw
queen diaw

Non fama dou nit nena dama done liguey sama yaye wayai mane mass bimou si bolai rek momasi meti ak bidew😂omg nena mane ak mass la 🔥

Hace 11 días
Barada Bi TV
Barada Bi TV

salut les gars allez voir notre sketch MOUTATOU AK KOOR GUI et de vous abonner ça nous fera vraiment plaisir. et n'oubliez surtout pas de partager les vidéos pour que la famille s'aggrandisse.

Hace 11 días
Mamadou Ndiaye
Mamadou Ndiaye

Raygama fama mo nekh

Hace 11 días
RamÉa hijabie Queen GUEYE
RamÉa hijabie Queen GUEYE

Germaine dh Matt na liniou Koy doyee haha

Hace 11 días
MaxMouhamed Maxmouhamed
MaxMouhamed Maxmouhamed

Fama raye nama

Hace 11 días
abdel ohod
abdel ohod

Daro sonnungua li rek ndakh gaurr thiammeu

Hace 11 días
khadim ngom
khadim ngom

Cey fama

Hace 11 días
Thiane Diop
Thiane Diop

Bideew

Hace 11 días
O'Connecting Worldwide
O'Connecting Worldwide

*Roast beef?*

Hace 11 días
lové MM seck sokna haidara aw
lové MM seck sokna haidara aw

Je veux le numéro de téléphone de darou

Hace 11 días
Babacar ndiaye
Babacar ndiaye

Ah sama team namounala nk Yalla na yalla nagou sonno koor si bargué Borom Touba

Hace 11 días
Astou Diop
Astou Diop

Fama ya niémé gathié😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

Hace 11 días
Nema Siby
Nema Siby

gathia ben comprimé la wone fama neko touf

Hace 11 días
Alfee Ba
Alfee Ba

Waa selou ngene germaine machalah sa forme baxna

Hace 11 días
Tata Rose
Tata Rose

no mane germén momay ray bilay

Hace 11 días
Ka Carlou
Ka Carlou

Jajaja bilahi🤣🤣darou mon saff khorom wayy geurr yalla tay mom beugeu na aime svp nn mass yarouna darou takhalnako nii rek

Hace 11 días
Fatoumata Niangadou
Fatoumata Niangadou

Fama rek

Hace 11 días
Ndeye Coumba Diagne
Ndeye Coumba Diagne

Fama sa robe baxna bilay 😍😍 j'aime bien

Hace 11 días
Aicha Moustapha
Aicha Moustapha

Mdrr fama di na ma reiye 😭😂😂😂😂😂

Hace 11 días
Rohey Njie
Rohey Njie

Best fama touch gan fii

Hace 11 días
Adjia TounKara
Adjia TounKara

wa pourquoi fama meune solou tmt

Hace 11 días
Fallou Thiam
Fallou Thiam

Badien way 😂 😂

Hace 11 días
Fallou Thiam
Fallou Thiam

Bonsoir chers téléspectateurs 💞 Ana célibataire yi

Hace 11 días
Sopey Mame Diarra
Sopey Mame Diarra

Daro macha Allah, khalifa generale kouli diongoma! Laf thiat mais Daro oubil ecole sangnsé wala ngaye deff émission di hélal sama genre gui si habillement djiguene macha Allah! Yow ak mbathio ko lén boler si plateau di na nice!

Hace 11 días
Abdou Samb
Abdou Samb

Fama ray nama 😂

Hace 11 días
Ba Ba
Ba Ba

Ce n est pas rosebeef mais roastbeef

Hace 11 días
Dija Kebe
Dija Kebe

Ki trouve que fama sagnese rek ley deff pousel bleu ma guiss

Hace 11 días
Ndeye Khoudia Ndiaye
Ndeye Khoudia Ndiaye

Germaine mo deg ndigeul ahhha

Hace 11 días
Khady Ndiaye
Khady Ndiaye

Fama rek si khall non eupe na

Hace 11 días
FascinatingMya
FascinatingMya

Fama sagnsé nga MachaALLAH

Hace 11 días
Alad Fayee
Alad Fayee

waw biddew mom lou gayi khar si mom tak ko footballeur. senegalais any niou dou nguen wakh si khale bi bok

Hace 11 días
Daba Diome
Daba Diome

no fama douma rey man. néna yalla wakhna KO sama yaye moko wakhoul. mdrrr

Hace 11 días
sokhna diarra diop
sokhna diarra diop

Woooy mass dama don liggey Sama yaye kayy😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

Hace 11 días
gorgui niang
gorgui niang

c est tres bon

Hace 11 días
Khadidiatou Dia
Khadidiatou Dia

LA FIN Yaye: wannouko Mass: way wannouko way yaw Bideew: ya koy leikeu fama Fama: manitt sourna 😂😂😂😂😂😂

Hace 11 días
Mairam Ba
Mairam Ba

Fama si tu marabout ta mere a cause d un homme j esper k tu sera heureu avk lui a vie sinon😢😢

Hace 11 días
Fifi Ekmat
Fifi Ekmat

Daro bayil khèssal ba nga oute gamme Boubakh sagnssè mome sa yeuf leu

Hace 11 días
Khadidiatou Diop
Khadidiatou Diop

aye waye fama dinama raye

Hace 11 días
Mariama dia toukoulor bou rafét bi
Mariama dia toukoulor bou rafét bi

fama sonou ngua nak😂😂 li lépou thi beug séy massa yaw

Hace 11 días
Bamba ndiaye Diouf
Bamba ndiaye Diouf

Badiané dinam rayé

Hace 11 días
ParadiseParadise Paradise
ParadiseParadise Paradise

Fama gola habiller machla 👏👏

Hace 11 días
binette Faye
binette Faye

Bayilenn serigne loumla may khagn lakoo

Hace 11 días
PAPI INTERNATIONAL SÉNÉGALAIS
PAPI INTERNATIONAL SÉNÉGALAIS

Mais Sénégal pr quoi sene lep serigne rék

Hace 11 días
Know One
Know One

Soie bi fama Sol demb la beugue hamolene kouko niaw

Hace 11 días
Vieux Bocar Guissé
Vieux Bocar Guissé

Démale si Thiané Diagne j-ji

Hace 11 días
Mariama dia toukoulor bou rafét bi
Mariama dia toukoulor bou rafét bi

fama fimisté trop mai liguay sagnsé dousa âge dall

Hace 11 días
Ado Ndiaye
Ado Ndiaye

Fama pour quoi fimistée tamit

Hace 11 días
saux sau
saux sau

Nice

Hace 11 días
souadou diop
souadou diop

Mais Biddew mom xana dou utilisé xorom

Hace 11 días
Ndiaya Camara
Ndiaya Camara

Chouuu mais fama tamite li ngay sagnsè eup na

Hace 11 días
Mostafaechammakh M
Mostafaechammakh M

Kooro biddew nèkhna waye

Hace 11 días
Nenishe Laye
Nenishe Laye

est c k sey diarayna li

Hace 11 días
Anna Sagna
Anna Sagna

Roastbeef

Hace 11 días
Mame dieyla Wade
Mame dieyla Wade

Fama sa sagnsé bakhna

Hace 11 días
Sala Syll
Sala Syll

Germain ya sakk way

Hace 11 días
Amina Ndiaye
Amina Ndiaye

Bidew del teik des fois greffages pour changer seu kanam bi

Hace 11 días
SIRA GOUDIABY
SIRA GOUDIABY

Mw vraiment jm la tfm et tt les personnes ki si trouve

Hace 11 días
bb afa Ka
bb afa Ka

Fama wayy😂🤣😂🤣😂🤣😂

Hace 11 días
Adja Lo
Adja Lo

Non daro vrai comédienne leu bilahi laf thiat daro tu joue bien

Hace 11 días
baye abdou gaye
baye abdou gaye

Dama tar de😢😭😭

Hace 11 días
prince junior tv
prince junior tv

Yalna yalla nagou sougnou laylatoul khadri si barke naby psl

Hace 11 días
Khady Sarr
Khady Sarr

Rose bif rebatass

Hace 11 días
Ndour Mbay
Ndour Mbay

Noo fama dou dém

Hace 11 días
chami fam
chami fam

Purée ak bèn maggi non eupena, Sénégal il faut gnou wagni saf safal vraiment

Hace 11 días

A continuación