MBETTEL SAISON 3 EPISODE 21

Aliou Dieme
Aliou Dieme

Ousmane iow abe rieul deggue ngua

Hace un mes
yayi dabakh
yayi dabakh

Wouyaye deureum gadio raynama😁

Hace un mes
Marie Caroline Wade
Marie Caroline Wade

Shiii fatdame sof nama torop. Sou saye cordes vocales dagué digua nopalu!

Hace un mes
Hafsatou Dia
Hafsatou Dia

Fatdame je te déteste madione appel la police ki eupeul na wayy

Hace 2 meses
Fatou Sy
Fatou Sy

Fat dame j'laime daleu la Mouy joué eupeuna😂😂😂

Hace 2 meses
omar omzo N.1
omar omzo N.1

Mandion fassel ki way goor day am diom

Hace 2 meses
Tina Demba
Tina Demba

Yhd

Hace 2 meses
Mboye Ndiaye Dieng
Mboye Ndiaye Dieng

wa ani you name ndeye ndiaye

Hace 2 meses
doffou balla
doffou balla

Ndeyssan

Hace 2 meses
Mafallou Gueye
Mafallou Gueye

Li eskeu dou ay guént aa warouna

Hace 2 meses
Modou Sarr
Modou Sarr

Ani kou beug yayam❤️✅

Hace 2 meses
Mouhameth Fall
Mouhameth Fall

Salamm Les baye FALL é Les yaye je suis un nouveau

Hace 2 meses
Aissatou Ndiaye
Aissatou Ndiaye

nafisatou say wolof khnne

Hace 2 meses
Aissa bibi Wane
Aissa bibi Wane

punaise, passage ousmane ak deureum ca ma achevé... wepepepe Mandioye ak gnane yi naaak, ndeketer seuy dou fo shiiii

Hace 2 meses
fatou faye
fatou faye

Ni deureum di dawé coum danél.

Hace 2 meses
Ourey Thiam
Ourey Thiam

Ayway Fatdam bayile Lay Lay néna beugue diame motakh mou deuck Diamalay khana sa yarame dina daw Hahahah

Hace 2 meses
Khadim Ndongo
Khadim Ndongo

👍👍

Hace 2 meses
Cheikh Diop
Cheikh Diop

Ousmane dinama Ray

Hace 2 meses
MELTING POT
MELTING POT

LA COUSINE DE ROUBA A L' AIR FAUSSE

Hace 2 meses
Sokhna Arame Fall Mbaye
Sokhna Arame Fall Mbaye

Wouy deuram mingmay Ray way

Hace 2 meses
Khady Mbaye
Khady Mbaye

Ousmane gnane na liiiii

Hace 2 meses
Ndeye Coumba Wade
Ndeye Coumba Wade

Madione so fasewoul fat dam Dina la talle😂

Hace 2 meses
Nabou Ba
Nabou Ba

Non deureme raynam😂😂😂

Hace 2 meses
Daouda Diop
Daouda Diop

Le scenario est vraiment dOop macha alla kou daccord ak mane pousse bleu may séine

Hace 2 meses
Thieer Ba
Thieer Ba

Fatdam moder un peu ta langage oubekoule dou wakhe bou raféte avant de parler ils faut réfléchir avant de dufusuier la série le réalisateur ils bien voir les choses merci l'équipe Mbettel 😥😥😥😥😥😥

Hace 2 meses
Aicha Thiello
Aicha Thiello

nafissatou nena guélou ousmane bé ma dadjel mounane ma kouss kondrong la khawma thiappe kéleng leng doynama seuk 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

Hace 2 meses
Khadidiatou DIALLO
Khadidiatou DIALLO

team nafiii

Hace 2 meses
Younouss Ba
Younouss Ba

Am ndiarel diehna ci Sénégal

Hace 2 meses
Ali Salman
Ali Salman

Ndeureum way ray nama

Hace 2 meses
mel ladiva
mel ladiva

Dégeuna deuge si seuÿ yi

Hace 2 meses
Matar Fall
Matar Fall

fat dame amoul respect

Hace 2 meses
Diallo Diallo
Diallo Diallo

Nattou dankoy Santé sa boromm? alhamdou lillah rouba

Hace 2 meses
Fatou Ba diaw
Fatou  Ba diaw

La Sœur de Rouba Fa Thierno nékhnama torope sakh

Hace 2 meses
Mboye Ndiaye Dieng
Mboye Ndiaye Dieng

en plus elle est trop belle

Hace 2 meses
samba niang
samba niang

mane rouba daff ma soff trop

Hace 2 meses
Mariama Marguerite Diallo
Mariama Marguerite Diallo

Hii nafissatou tay mome ell a parfaitement raison

Hace 2 meses
Mariama Marguerite Diallo
Mariama Marguerite Diallo

Mais fat dam a exagéré

Hace 2 meses
Serigne Ibrahima Diop
Serigne Ibrahima Diop

Ana gniy beugue mandione tak Roubeu

Hace 2 meses
murtala drammhe
murtala drammhe

nekh na torop

Hace 2 meses
hmjr Foot
hmjr Foot

Mane deureume dina ma ray🤣😄😀 Mandione fasél ki waay niak Foulla tropp😔😕

Hace 2 meses
Bass Ngom
Bass Ngom

Thico Rieul lue

Hace 2 meses
omar samba ndiaye
omar samba ndiaye

Presque 600mil vu en moins d'une semaine. Série qui bat tous les records. Mashala way

Hace 2 meses
Alijagu Camara
Alijagu Camara

Yallah nañiu borom bi meussal si djiabar diou mel ni fatdame Son comportement mako ragal Rouba borom xöl bou bakh lou bonn rek lay am❌😔(Yaye)

Hace 2 meses
Nekhou Niass
Nekhou Niass

Béll mér

Hace 2 meses
Sankoun Kanoute
Sankoun Kanoute

Mandione Ami diabar bou bakh teh Papa Diouf bonne na trop.Seulement amoul chance dakh waji dewoul teh Yallah dou teuj joint teuj palanter wathie rido say.

Hace 2 meses
Elhadji Niang
Elhadji Niang

Anna ngane bandii bi

Hace 2 meses
ShadowK 45
ShadowK 45

Perché c'è sta roba nelle tendenze?

Hace 2 meses
Mariama Mbaye
Mariama Mbaye

Fat dame weroul way koussi ande besseul j aime

Hace 2 meses
Sarr Pape
Sarr Pape

No deureum amoull djiomm qoi 😂😂😂😂nénako dangay woyou woyou lou rk

Hace 2 meses
Lamine Ndiaye
Lamine Ndiaye

Wa fatou dame nitt la mais ken dou soeur rou rouba bi

Hace 2 meses
Gnagna Bint Muhammad Al Amine
Gnagna Bint Muhammad Al Amine

j'adore deureum

Hace 2 meses
Adji Tall
Adji Tall

👻👻👻👻👻👻👻

Hace 2 meses
Oumy Ndoye
Oumy Ndoye

Wouuuyy deureume raynama

Hace 2 meses
Fatoubinetou Diakhate
Fatoubinetou Diakhate

Mais koumay expliqué fat thierno miii loumouy joué kiii bagne nako

Hace 2 meses
AURORE NDIAYE
AURORE NDIAYE

Comment papa diouf a su que le gars aller parler avec rouba et comment il connait aussi l inspecteur?

Hace 2 meses
zeynab saliou
zeynab saliou

Laye laye du fene kat deh diabaram bi di fat dame motah mouy feine moko ssi pousseiii So mayul sa dieker diam dalay nebatou

Hace 2 meses
Cheikh Mbengue
Cheikh Mbengue

Merci Nafissatou d avoir redresser Fatou Dame...cela Montre l aggressivitè de la Femme senegalaise...

Hace 2 meses
Maimouna Dieng
Maimouna Dieng

Non deurem dou ma rayy🤣🤣

Hace 2 meses
Toure Ndeye Fatou
Toure Ndeye Fatou

ndeyefatou

Hace 2 meses
Aïssatou Bamba
Aïssatou Bamba

mbettel nexna nafisatou rek cii meuneu wax eupeuna

Hace 2 meses
Mm Touré
Mm Touré

Ousmane kane je te déteste

Hace 2 meses
Tanker
Tanker

un reportage sur des singes, ça faisais longtemps ^^

Hace 2 meses
DrOogueu Douce TV
DrOogueu Douce TV

Fat dame merena dieukeur dji mais waroul reagir ni seuy yomboul d ndah lep dey fegn si ndjaboot gui Mai's aussi waroul tek si derou rouba Lou niaw ndah seu kharit ak Lou meti loum LA meunti def waroko soulil ey mbotam

Hace 2 meses
Op Jj
Op Jj

Negri al rogo

Hace 2 meses
Loucha Ndiaye
Loucha Ndiaye

Magou Roubeu bi nexnama oh el est naturel ak sene teint noir yi jaim

Hace 2 meses
Dame Ndiaye
Dame Ndiaye

Nafisatu ak ruoba rek

Hace 2 meses
Patriote Ndiay
Patriote Ndiay

Deureum 😂😂😂

Hace 2 meses
senegalhairrock senegalhairrock
senegalhairrock senegalhairrock

😂😂😂😂😂😂

Hace 2 meses
Juuf Khousha
Juuf Khousha

Wa madione loumouy tariii ni mom tmt😀😀😂

Hace 2 meses
Juuf Khousha
Juuf Khousha

Nooo deureum rayy nama😂😂😂

Hace 2 meses
Ramatoulaye Mbengue
Ramatoulaye Mbengue

Nafissatou et sa soeur jouent très bien bravo😊👏👏👏👏👏

Hace 2 meses
mariane Ndiogou
mariane Ndiogou

Maylén niou diam djiguen bou amoul diam amoul salam noy déf mba do fén pr am diam facéko mou diékh takk

Hace 2 meses
Arc en ciel
Arc en ciel

😂😂😂 deureum gadio mdr dé nekhoul

Hace 2 meses
Sckralchet
Sckralchet

Danone is better

Hace 2 meses
mouhamed ndiaye
mouhamed ndiaye

Khawma dama ki amou l bene thiathe domeramla rek

Hace 2 meses
Adja Soumare
Adja Soumare

Lay lay Tey mom daguan danou bakhalangou un homme responsable n doit pas caché ds choses à sa femme kou d'accord ak man meyma bi👉👍👍👍👍way

Hace 2 meses
makup by rokina
makup by rokina

fat dam telma sa lamigne wou ritax wi😅😅😅

Hace 2 meses
Eva Sima
Eva Sima

les conseils de Nafissatou sont valable pour toutes les femmes djek diam ak djerigne dalaléne séne khellou monsieur yi téguène tek seuy thi axe ndakh divorce yi wagnékou wayé nak yalla bouma am Woudje 😂😂😂

Hace 2 meses
Mamy Tavarez
Mamy Tavarez

Mane nafi daf may fadji😂 akhhh

Hace 2 meses
Abdou Sougou
Abdou Sougou

nafisatou yagui si

Hace 2 meses
Aliou Sarr
Aliou Sarr

mes fat dame cou xol guiss cou lamb dadje il ne faut jamais accusé ton mari ou sui ton mari

Hace 2 meses
Ablaye Diagne
Ablaye Diagne

soumadone mandione laye fassena fatdam bou yag

Hace 2 meses
Aissatou Diop
Aissatou Diop

Fat dame dafa eupeul dh lii keine duko DF sa dieukeur

Hace 2 meses
Sokhna Faty Ndiaye
Sokhna Faty Ndiaye

N

Hace 2 meses
Rouguiyatou Ly
Rouguiyatou Ly

wa tamit deureum gnakoul fayda ak yaramame bou bari bi mouy kholé ba ousmane mi di melni bante diko sekestré

Hace 2 meses
Aichetou Gaye
Aichetou Gaye

Le passé finit tjrs par nous rattraper

Hace 2 meses
Papa Nguirane
Papa Nguirane

b:Définitions de lapslapsnom masculin(latinlapsus,écoulement)DéfinitionsExpressionsLaps de temps,espace de temps écoulé, en général court.

Hace 2 meses
Penda M
Penda M

Wa tchiko lutax mu beug violence ? 🤣🤣🤣🤣 un deux trois muni Mak jii doral Talla Mdrrrrrr

Hace 2 meses
Falo Faye
Falo Faye

Tame nafissatou mala beuge pii😘😘

Hace 2 meses
Madame Dieng
Madame Dieng

Mais pourquoi à chaque fois bou nouy joué rek am thi goor yo khamné séne diabar yi ngon léne djitël

Hace 2 meses
Cheikh Diagne
Cheikh Diagne

Non ousmane amoul

Hace 2 meses
Aminata Sakho
Aminata Sakho

Wa fate dame nilagne kaye bayu mome role panke rek laye jouyer

Hace 2 meses
beug s.babacar sy, Diop
beug s.babacar sy, Diop

Hi

Hace 2 meses
SrYisus Pablo
SrYisus Pablo

Pero que pollas es esto

Hace 2 meses
mame diarra ndiaye
mame diarra ndiaye

téye nak nafisatou wakhna deugue bravo 👏👏

Hace 2 meses
Arame Diop
Arame Diop

Le khoulo entre Bella et la go de Ousmane Kane m a tué j arrête pas de le repasser

Hace 2 meses
thierno diop
thierno diop

Kou yeurem Rouba beuseul jaim

Hace 2 meses
Mohamed Kande
Mohamed Kande

Nice film chapo a tte lekip

Hace 2 meses
Fatima FALL
Fatima FALL

Deureum raynama 😂😂

Hace 2 meses
Elhadji Faty
Elhadji Faty

Nice

Hace 2 meses
Mariama Ba
Mariama Ba

chapeau a nafissatou

Hace 2 meses

A continuación